Meta:Main Page/wol
From OmegaWiki
asturianu | bokmål | па-беларуску | brezhoneg | български | català | česky | Deutsch | ελληνικά | English | español | Esperanto | français | עברית | italiano | 日本語 | Kölsch | Nederlands | novial | polski | português | Rumantsch | русский | slovenčina | српски | srpski | suomi | svenska | українська | tiếng Việt | 中文 | wolof | +/-
|
Dalal-jàmm ci OmegaWiki! |
|
Dalal-jàmm ci bunt bu wolof ci OmegaWiki. OmegaWiki ngi lay dalal. Ngirtey naal bii mooy joxe ay xibaar ñeel ay baat ci làkk yépp. Man ngaa tànn làkk bi nga bëgg dalu bi wone soo demee ci say tànneef. Su fekke amul ab tekki ci sab làkk, danu la koy won ci angale walla ci beneen làkk boo bëgg, doy na nga dem ci tànneef soppi ko. So bëggee tambalee soppi dara, njëkal a jàng jukki biy wax ci TekkiFaramface. Su loolu amee nga sos am sàqub jëfëndikookat te xamale làkk yi nga dégg ak ab royuwaay Babel. Man ngaa def ay laaj ci ëtti Wiki yi : pénc yi walla IRC channel yi. Fi mu ne nii OmegaWiki ubbeegul ngir ñépp, ndaxte day ab naal bu bees, waaye bu ci kannamee di nan ko ubbi ngir ñépp. Ñénn ñi rekk la nu joox maqaama ñu man a def ay coppite. Soo gisee ay njuumte ci ab jukki, man nga bind ci xëtu waxtanukaay ba, su ko defee nu jubbanti ko. |
| |

